Nétalib Yeesu bu dëggu bi
Seetanal Nétalib Yeesu gu dëggu gi
Demal ci Xët bi
Nit ñi ñaan nañu
ci iBIBLE xaaj yi
×
So waxe ñaanug mucc gi kon leegi ab doomu Yàlla nga.
Saw làmmiñ, soo ci biralee ne Yeesu moo di Boroom bi, sab xol it, nga gëm ci ne Yàlla dekkal na Sang Yeesu, dinga mucc.
Room 10:9
×
Man nga ñaanandoo ak nun ngir
sa mucc:
Yaw Yàlla,
Nangu naa ne Yeesu mooy Boroom bi. Gëm na ne juddu na cib jàng, de ci bant ba ngir sama bàkkaar, te dekki gannaaw ñetti fan. Tay, nangu naa ne bàkkaar na, te amul lu mana def ngir musal sama bopp. Ma ngi lay
Ñaan nga baal ma, te wekk na sama yaakaar ci Yeesu kese. Gëm na leegi ne sa doom la te dina nekk ba abadan ak Yaw. Gindi ma bes bu nekk jaare ci Sa Xel Mu Sell mi. Dimbalima ma bëgg la ak sama xol mépp, ruu, ak xel te bëgg ñeneen ñi ni sama bopp. Jërëjëf si linga ma musal jaare ci deretu sa Doom, Yeesu. Ci Turu Yeesu la ñaane. Amiin